Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 12

Kay Signé (feat. Bass Thioung)

ZBest Family

Letra

Kay Signé (feat. Bass Thioung)

Kay Signé (feat. Bass Thioung)

ZBest FamilyZBest Family
Bass Thioung est làBass Thioung lay doon

Jongoma, tu sais que ça déchireJongoma dangay dégg daaj
Soxor, t'es pas prêt, ça va faire malSoxor tegsi ñeme jarul sax di laaj
Écoute comme je suis làXooleen ni ma moole
Je suis là pour te montrer que je suis làYamal ci xoole dangay toog di xaar
Je suis là pour briller, c'est clairMan damay xéy di gën di baax
Et toi, tu brilles comme un roi, tu sais quoiTe yaw dangay xéy monté dékk di wax
Écoute comme je suis làXooleen ni ma moole
Je suis là pour te montrer que je suis làYamal ci xoole dangay toog di xaar

Le look que j'ai, c'est pas pour rienPeruque bi ma ko moom
Ne demande pas, tu sais que ça claqueDàll beek saak, bul laaj fu mu jugé
Ce que je fais, c'est pas pour rienLi ma sol ma ko moom
Je fais le taf, je suis là pour çaDékku liggéey bu lew la ko ame
La science, c'est ma passion, pas d'histoireSañsé dangay science, jarul histoire
Le problème, c'est de trouver la solutionProblému wax solution la laaj
Je suis là pour te montrer ma vision, c'est clairDangay solu tégu woo zo vision mu foto la

Mashallah !Mashallah!
Ton style est topSa sañsé baax na
Ah, ça déchireAh kon mu ngi baax
Pourtant, je fais tout pour que ça soit bonPourtant dama ko woyofal def lool neex
Mashallah !Mashallah!
Tes cheveux sont au top, ouais !Sa cheveux baax na, waaw!
Ah, ça déchireAh kon mu ngi baax
Quand tu fais le show, c'est du lourdNi lay fél-falale lu neex
Tout le monde est là pour voirBa samay noon di jooy

Dis-moi pourquoi ton style est si fortMan lu tax bi la sañsé dafay dégu
Si je te vois, tu sais que je vais pas lâcherBoo ma gisee bo siisuwul dangay nangu
Dans le corps, c'est là que ça se passeCi yaram bi la mbégte la laaj
Le style, c'est là où ça brilleSañsé fi la fekk baax

Mon tailleur, il est au topSama tailleur bi moo ko ñaw
Je suis là pour brillerMan ma ko sol
Regarde le style, regarde le styleÑëwleen signé, kaay signé
Ce que je fais, c'est pas pour rienLi ma sole statut ma gaaw

Eh, le blanc, il parle, mais c'est pas vraiEh tubaab moo ko wax, apreciel
Il critique, mais il sait pas ce que c'estBañ di critiqué di jëme mel ni signeel
(ZBest Production numéro un)(ZBest Production number one)

Jantal, je suis là pour déchirerJantal man dangay dégg daaj
T'es pas prêt, je vais tout déchirerTegsi nga ma joxe bala kenn di laaj
Écoute comme je suis làXooleen ni ma coofe
Je suis là pour te montrer que je suis làYamal ci xoole dangay toog di xaar
Je fais plein de trucs, tu sais que ça déchireDangay jëf lu bari tuuti wax
C'est Dieu qui m'a donné ce talent, je sais ce que je faisGóor Yàlla la kon fokk ma xam lu baax
Écoute comme je suis làXooleen ni ma coofe
Je suis là pour te montrer que je suis làYamal ci xoole dangay toog di xaar

Céy, je suis là, je peux le faire, et je fais ça pour moiCéy man la bokk dama ko mën te sañsé ma ko moom
Pourtant, je suis là, je fais tout pour que ça soit bonPourtant du iblow du daf la gën ci sañsé moo la mën
Le style, tu sais que ça va faire mal, je suis là pour çaBoy signé dinga sonn ndax yoru ma ci benn
Tu sais que je suis là, je fais le show, eh !Yaa nga solu ci esprit la doo ko dondu fenn, eh!
Les lumières, elles brillent, regarde-moi snapperNa làmp yi daq yaw laal ma snap
Je suis stylé, frais, regarde-moi snapperMan dama stylé fraîche, yaw laal ma snap
Si je m'en vais, je suis là, Z-Best, c'est moiFu ma génn gën na fi la, Z-Best tamit ci la
Si je suis là, bad boy, je suis là pour çaSu ma neexee bad boy ndaanaan cho yi gën ma fi la

Mashallah !Mashallah!
Ton style est topSa sañsé baax na
Ah, ça déchireAh kon mu ngi baax
Pourtant, je fais tout pour que ça soit bonPourtant dama ko woyofal def lool neex
Mashallah !Mashallah!
Tes cheveux sont au top, ouais !Sa cheveux baax na, waaw!
Ah, ça déchireAh kon mu ngi baax
Quand tu fais le show, c'est du lourdNi lay fél-falale lu neex
Tout le monde est là pour voirBa samay noon di jooy

Dis-moi pourquoi ton style est si fortMan lu tax bi la sañsé dafay dégu
Si je te vois, tu sais que je vais pas lâcherBoo ma gisee bo siisuwul dangay nangu
Dans le corps, c'est là que ça se passeCi yaram bi la mbégte la laaj
Le style, c'est là où ça brilleSañsé fi la fekk baax

Mon tailleur, il est au topSama tailleur bi moo ko ñaw
Je suis là pour brillerMan ma ko sol
Regarde le style, regarde le styleÑëwleen signé, kaay signé
Ce que je fais, c'est pas pour rienLi ma sole statut ma gaaw
Mon tailleur, il est au topSama tailleur bi moo ko ñaw
Je suis là pour brillerMan ma ko sol
Regarde le style, regarde le styleÑëwleen signé, kaay signé
Ce que je fais, c'est pas pour rienLi ma sole statut ma gaaw

Eh, mon tailleur, il est meilleur (c'est la classe !)Ey sama tailleur dafa meilleur (laf cat!)
Eh, le style, il est meilleur (t'as vu ?)Ey, sañsé bu meilleur (ngay am)
Eh, mon style, il est meilleur (c'est la classe !)Ey sama sañsé dafa meilleur (laf cat!)
Eh, le style, il est meilleur (t'as vu ?)Ay, Sañsé bu meilleur (ngay am)
Eh, mon tailleur, il est meilleur (c'est la classe !)Ey sama tailleur dafa meilleur (laf cat!)
Eh, le style, il est meilleur (t'as vu ?)Ey, sañsé bu meilleur (ngay am)
Eh, mon style, il est meilleur (c'est la classe !)Ey sama sañsé dafa meilleur (laf cat!)
C'est le meilleur (c'est la classe !)Bon il est meilleur (laf cat!)

Ce que je fais, ça coûte cher (eh, le style, c'est cher)Li ma sañsé ça coût cher (eh, sañsé xale)
Oh, c'est cher (ouais, le style, c'est cher)Oo dafa cher (waaa way sañsé xale)
Regarde le style, regarde le styleÑëwleen signé, kaay signé
Ce que je fais, c'est pas pour rienLi ma sol statut ma gaaw

Ce que je fais, ça coûte cher (tu sais, le style, c'est cher)Li ma sañsé ça coût cher (nga ni ma, sañsé xale)
Oh, c'est cher (ouais, le style, c'est cher)Oo dafa cher (waaa way sañsé xale)
Regarde le style, regarde le styleÑëwleen signé, kaay signé
Ce que je fais, c'est pas pour rienLi ma sol statut ma gaaw

Ce que je fais, ça coûte cher (tu sais, le style, c'est cher)Li ma sañsé ça coût cher (nga ni ma, sañsé xale!)

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de ZBest Family y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección