Traducción generada automáticamente

Eutou Baabel
AMADEUS
Eutou Baabel
Eutou Baabel
Mach dir keine SorgenMaak yaw ba abadan
Gib mir meine FreiheitJox naa la sama kàttan
Ich bin dein KindJaayaanteek sama ndaw
Lass mich nicht im Wasser ertrinkenDem naa ba ndox ci baat
Gib mir meine StimmeJox naa la sama kàddu
Ich kann nicht ohne dichMënatuma la baal
Und ich fühle mich stark, wenn ich bei dir binTe sèntu naa ci jële ndam maak yaw
Denn die Welt wird immer schwieriger, wenn ich nicht bei dir binNdax àddunya bi dafay feexe ba ma xàddi
Ich werde nicht aufgeben, was ich für dich empfindeDuma bàyyi li ma tàmbali man
Ich werde meine Großmutter ehrenFàttaliku naa sama maam
Ich hoffe, dass ich die Wahrheit finden kannNe na ma fori jëlal jaaro gi
Ich habe gehört, dass sie mich nicht hören wollen, aber ich bin kein Feind der FrauenDégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen
Ich weiß, sie werden mich fragen, warum ich das sageXam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile
Niemand ist wie Thiam Baabel, ich weiß, dass ich dich willKenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Niemand ist wie Thiam Baabel, ich weiß, dass ich dich willKenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Wir sind hier, um zu lebenDemanoon de nañu
Wir haben unsere GründeDefando nañu ay mbir
Du weißt, was ich sageXamal nga ma lu ne
Wenn ich es dir sageSoo ma yoolee
Ich werde nichts verlierenDootuma jar dara
Wenn ich alles gebeBi ma ñépp umpale
Du weißt, dass ich dich kenneYaw yaa ko xam
Du bist mein WegSama waay nga
Niemand ist wie duKu mel ni yaw
Niemand kann dir das nehmenKu ka amul da koy iñaane
Niemand ist wie duKu mel ni yaw
Eutou Baabel, sie fragen nach dirËtu baabel ñoo lay laaj
Niemand ist wie duKu mel ni yaw
Thiam Baabel Demba Thiam, ehThiam Baabel Demba Thiam, eh
Niemand ist wie duKu mel ni yaw
Eutou Baabel, sie fragen nach dirËtu baabel yaw lay laaj
Ich werde dich in Eutou Baabel bringenNaa la yóbbu ëtub baabel
Ich werde dich mit meinen Träumen verbindenBoole la ak samay nawle yi
Du weißt, dass du der Grund bist, warum ich lebeXam nga tàkkusaanu baabel
Thiam, der Herr der Nacht, du bist alles für michThiam boroom ndendi was nga fay fowee
DuYaw
Ich werde nicht aufhören, für meine Träume zu kämpfenMësuloo ma xépp ci samay ay ayib
Meine Sterne werden es mir sagenSama njuumte yi mësoo ko nettali
Du weißt, dass es keinen gibt, der stark istXam nga jaambaar amul
Niemand kann uns aufhaltenKu ñu dimbale am
Niemand kann uns trennenKu sañoon day baax
Wie ein KindComme doomu ñay
Wenn ich nach dir rufeBu ma ñaanal ponkal
Ich werde gut leben, wenn ich bei dir binMan soo ma dundee baax
Ich habe gehört, dass sie mich nicht hören wollen, aber ich bin kein Feind der FrauenDégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen
Ich weiß, sie werden mich fragen, warum ich das sageXam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile
Niemand ist wie Thiam Baabel, ich weiß, dass ich dich willKenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Niemand ist wie Thiam Baabel, ich weiß, dass ich dich willKenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Wir sind hier, um zu lebenDemanoon de nañu
Wir haben unsere GründeDefando nañu ay mbir
Du weißt, was ich sageXamal nga ma lu ne
Wenn ich es dir sageSoo ma yoolee
Ich werde nichts verlierenDootuma jar dara
Wenn ich alles gebeBi ma ñépp umpale
Du weißt, dass ich dich kenneYaw yaa ko xam
Du bist mein WegSama waay nga
Niemand ist wie duKu mel ni yaw
Niemand kann dir das nehmenKu ka amul da koy iñaane
Niemand ist wie duKu mel ni yaw
Eutou Baabel, sie fragen nach dirËtu baabel ñoo lay laaj
Niemand ist wie duKu mel ni yaw
Thiam Baabel Demba Thiam, ehThiam Baabel Demba Thiam, eh
Niemand ist wie duKu mel ni yaw
Eutou Baabel, sie fragen nach dirËtu baabel yaw lay laaj

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de AMADEUS y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: