Traducción generada automáticamente

Nawle
AMADEUS
Nawle
Nawle
Si je ne suis pas là, je suis dans la rueSu nit doon may boppam duñu néew la
Je suis là pour te donner de la forceDuñ doon ay niiw di doole
Personne ne peut me décevoirKenn du ñu ëppale
Dieu, c'est mon cheminYàlla mooy may waay
Regarde-moi pour ce que je fais pour te donner de la forceXeeb nañ ma ngir li may niiw di doole
Je ne veux pas de ta jalousieNe nañ duma sa nawle
Regarde-moi sur le chemin de la merXool nañ ma bëtu xebbe
Dieu, c'est mon cheminYàlla mooy may waay
Si je suis là, je suis là pour toiSu ma doon kiy dogal
Personne ne peut me faire du mal, car je fais ce que je faisSa askan kenn du ma ci raw ndax ni ñu ma def
Fais-moi confianceDes nañ ma wékk
Je vois tout ce que tu as faitGis naa lépp li nga may defal
Ta famille entière ne peut pas être ici, ça n'existe pasSa waa-kër yépp ne du ci dal du fi ame
Je te demande de me donner un bon moment (ouais ouais)Nga jombu leen ngir jëmu ju xébbu ji (léegi-léegi)
Si je dois partir, je vais le faire (ouais ouais)Fok ma dem utti indi (léegi-léegi)
Je ne peux pas partir sans toi (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)Mënuma dem bàyyi la (day jeex, day jeex, day jeex)
Je ne veux pas que tu partes sans moi (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex)

C'est de la force que je veux (ouais ouais)Doole la néew le (léegi-léegi)
Je ne veux pas de ta jalousie (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)Ne nañ duma sa nawle (day jeex, day jeex, day jeex)

Regarde comme tu es belleOuroul ayni sa niroowaale
Tu es dans le tank de la vieAw nga ci tanku yaayu aje
Tu es comme une étoile brillanteYaa ngi mel ni barry bu ndaw
Est-ce qu'Adji va te faire briller ?Ndax Adji kom ngay daguwaale
Ne dis pas que tu es fatiguéeDoo nettali doo gaaruwaale
Je suis là pour te soutenirDuggeloo ma ci giirawaale
Pour un bon moment (ouais ouais)Ngir jëmu ju xébbu ji (léegi-léegi)
Si je dois partir, je vais le faire (ouais ouais)Fok ma dem utti indi (léegi-léegi)
Je ne peux pas partir sans toi (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)Mënuma dem bàyyi la (day jeex, day jeex, day jeex)
Je ne veux pas que tu partes sans moi (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex)
Si je dois partir, je vais le faire (ouais ouais)Fok ma dem utti indi (léegi-léegi)
C'est de la force que je veux (ouais ouais)Doole la néew le (léegi-léegi)
Je ne veux pas de ta jalousie (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)Ne nañ duma sa nawle (day jeex, day jeex, day jeex)
Je ne veux pas que tu partes sans moi (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex)

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de AMADEUS y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: