Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 22

Fake News

Mia Guisse

Letra

Fake News

Fake News

Eu tô falando do meu interiorMaa ngi toog sama biir kër
Essa letra aqui eu já escreviLim binde nii maa ngi fa woon
Você lê, sente, me entendeNga lire ko, gëm ko, saaga ma
O que tá pegando?Lan moo xew?

O que que tá rolandoMoo ko def
Eu sou a única que sabeMa ni la moom la
A verdade aqui tá em jogoGutt bi fii lay jaar

Ninguém se importaNumu soofe
Eu só quero que você me escute e não me ignoreBëgg naa solu te noon la xayade
Se a gente não se entender, vai dar ruimBu juge dépp ay cheveum yu ñàppe
A maquiagem tá parecendo um carnavalJëlal make-up bi muy mel ni gaynde
Brincadeira, brincadeira, não dá pra esconderLijjanti lijjanti ba nar ci wayadee
A verdade tá vindo, não dá pra segurarDer bi ngay yaqi, demal jox ko uude
Se fizer isso, vai ser só mais uma mentiraMu def ko dalle sol ko uuti loo def
A verdade é que a gente pode falar sem medoPicc bu ndaw sax mën nañu wax ba du naaw
Não quer saber de nada, só quer saber de mimDuñ bëgg sa dara, sappa dëxin

Falar de amor, perfume no arSolu rombati leen, parfum bi tontu leen
Não tem tempo pra essas conversasAmatuma benn temps ay waxi noon
Falar de amor, perfume no arSolu rombati leen, parfum bi tontu leen
Não tem tempo, eu tô aquiAmatuma benn temps, maa ngi ci man

Eu tô falando do meu interiorMaa ngi toog sama biir kër
Essa letra aqui eu já escreviLim binde nii maa ngi fa woon
Você lê, sente, me entendeNga lire ko, gëm ko, saaga ma
O que tá pegando?Lan moo xew?

O que que tá rolandoMoo ko def
Eu sou a única que sabeMa ni la moom la
A verdade aqui tá em jogoGutt bi fii lay jaar

Por que que agora você quer lerPourquoi ba léegi sooy lire
Se não quer saber da verdadeMettit bañu ñu naak jege
Quem tá na rua tá fazendo o que querÑi ci mbedd mi ngay fore say fait
As pessoas tão perdidasNit ñi lëndëm nañu
Parece que é um apagãoBa mel ni coupure général
E aí, ohhh agoraNe ci, ohhh léegi
A gente sabe que Deus não vai deixar a gente na mãoÑu xam ni Yàlla du mësa fay wax di baay jëf
A verdade é que a gente pode falar sem medoPicc bu ndaw sax mën nañu wax ba du naaw
Não quer saber de nada, só quer saber de mimDuñ bëgg sa dara, sappa dëxin

Falar de amor, perfume no arSolu rombati leen, parfum bi tontu leen
Não tem tempo pra essas conversasAmatuma benn temps ay waxi noon
Falar de amor, perfume no arSolu rombati leen, parfum bi tontu leen
Não tem tempo, eu tô aquiAmatuma benn temps, maa ngi ci man

Eu tô falando do meu interiorMaa ngi toog sama biir kër
Essa letra aqui eu já escreviLim binde nii maa ngi fa woon
Você lê, sente, me entendeNga lire ko, gëm ko, saaga ma
O que tá pegando?Lan moo xew?

O que que tá rolandoMoo ko def
Eu sou a única que sabeMa ni la moom la
A verdade aqui tá em jogoGutt bi fii lay jaar

Esse mundo aqui tá uma arenaÀdduna bii bu doon arène
Quem quer brigar tem que se prepararKu bëgg jal faut nga laale
A verdade é que não dá pra esconderXeex dokki bu mu gacce yi
Não dá pra ignorarCi bañu lay nawe
E aí agoraNe ci léegi
A gente sabe que Deus não vai deixar a gente na mãoÑu xam ni Yàlla du mësa fay wax di baay jëf
A verdade é que a gente pode falar sem medoPicc bu ndaw sax mën nañu wax ba du naaw

O que que tá rolando é isso mesmo!Moo ko def moom la!

UhuuuWuy leeee
UhuuuuuWuy lelelelee

Eu tô na luta, na lutaMa ni gumbal, gumbal
Segura essa lutaTexel waay gumbal
Eu tô na luta, na lutaMa ni gumbal, gumbal

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección