Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 101

GLP (Gën Leen Paré)

Mia Guisse

Letra

GLP (Gën Leen Paré)

GLP (Gën Leen Paré)

Ich bin bereit, alles zu gebenTej gémmiñu bepp al waxa
Arbeiten, bis ich oben binLiggéey siggi xool ca kaw
Reden wir nicht viel, nur das Bla BlaTaluñu ay fo, du ay bla bla
Wir sind bereit, die Königin hat gesagt, wir könnenOn est ready, queen bi ñu ne mana

Die Party wird heute Nacht groß, ich werde nicht aufhörenSafara bi ngay jaaroo ca ba ngay doon mak
Die Jüngeren arbeiten hartKëriñ bi ndaw nga koy liggéey
Du machst es gut, während du dich entspannst und chillstDangay fexe daaj banc di soga nak togg
Jeder Tag ist ein GenussBës ñëw lépp neex

In der Stadt reden sieCi biti ñoo ngi wax
Ich bin mitten drinMan maa ngi ci biir
In der Stadt reden sieCi biti ñoo ngi wax
Ich bin mitten drinMan maa ngi ci biir
In der Stadt reden sieCi biti ñoo ngi wax
Ich bin mitten drinMan maa ngi ci biir

Gott hat keinen Mangel, es gibt keinen StressYàlla du juum fenn du am tonto
Nur Worte, die jetzt gesagt werden müssenAy wax rekk léegi dañ ko fiy tere
Wer deine Sorgen nicht versteht, der hat kein MitgefühlKu la mere sa mbégté dafla soxore
Die Bomben sind stark, sie werden dich nicht aufhalten, oh jaBomb seen bëñ yi du leen di tax a ree aaay

Gibt es mehr für euch?Gën leen pare
Ich gebe euch mehrMaa leen gën a pare
Ich gebe euch mehrMaa leen gën a pare

Die Hand, die dich hält, die Hand ist starkLoxo bu la bàyyi, loxo ngi tok
Die Hand, die dich hält, oh ja, starkLoxo bu la bàyyi, wallaay bàyyi
Die Hand, die dich hält, die Hand ist starkLoxo bu la bàyyi, loxo ngi tok
Die Hand, die dich hält, oh ja, starkLoxo bu la bàyyi, wallaay bàyyi

Zähle das Geld, es kommt reinCompter billets go didi tati
Voll mit Geld, GeldTeye full money money
Ich esse nicht von deinem Teller, guten AppetitDuma lekk seen bol, bon appetit
Nur Worte, die wir sagen, die uns zum Lachen bringenTële rekk tax ñuy ratatati
Essen, das du nicht kennst, ist kein ProblemCuj bu xam lekkam du fot
Wenn du es nicht hast, wird es jemand anderes tunDale bu la xat am na ku mu jot
Ich mache es einfach, es ist für alle gutDamay fo sax muy neex ñepp
Gott sei Dank, ich bin hierDieu merci noo tudd yaw

Zeig dein Talent, du bist hier, 25/5Yëngël sa mbagg bu de yaa ngi jot lii 25/5
Was du tust, ist nur für Gott, TennisLi nga joxe ngay jotaat rekk Yàllay ténnis
Lass mich kommen, ich werde dir neue Dinge zeigenDaf ma woo ma ñëw mu sampal ma ay laaf yu bees
Gott sei Dank, danke, danke, ich liebe mich selbstDieu merci, merci, merci, I love mysef


Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección