Traducción generada automáticamente

visualizaciones de letras 68

GLP (Gën Leen Paré)

Mia Guisse

Letra

GLP (Gën Leen Paré)

GLP (Gën Leen Paré)

T'es là, t'es prêt, on va y allerTej gémmiñu bepp al waxa
On bosse dur, regarde en hautLiggéey siggi xool ca kaw
On a des choses à dire, pas de bla blaTaluñu ay fo, du ay bla bla
On est prêts, la reine, on dit que c'est maintenantOn est ready, queen bi ñu ne mana

La soirée commence, tu sais que ça va être chaudSafara bi ngay jaaroo ca ba ngay doon mak
La jeunesse, tu sais qu'elle bosseKëriñ bi ndaw nga koy liggéey
Tu fais le show, t'es là pour brillerDangay fexe daaj banc di soga nak togg
Tout le monde est là, c'est bonBës ñëw lépp neex

Dans la rue, ils parlentCi biti ñoo ngi wax
Moi, je suis là-dedansMan maa ngi ci biir
Dans la rue, ils parlentCi biti ñoo ngi wax
Moi, je suis là-dedansMan maa ngi ci biir
Dans la rue, ils parlentCi biti ñoo ngi wax
Moi, je suis là-dedansMan maa ngi ci biir

Dieu ne fait pas de demi-mesures, pas de blagueYàlla du juum fenn du am tonto
Juste des mots, maintenant, ils sont là pour toiAy wax rekk léegi dañ ko fiy tere
Qui te dit que ta beauté est un trésorKu la mere sa mbégté dafla soxore
Fais attention, tes belles jambes ne te feront pas tomberBomb seen bëñ yi du leen di tax a ree aaay

Gën leen pareGën leen pare
Je vous en prie, parez-vousMaa leen gën a pare
Je vous en prie, parez-vousMaa leen gën a pare

La main qui t'a donné, la main qui te toucheLoxo bu la bàyyi, loxo ngi tok
La main qui t'a donné, oh oui, la mainLoxo bu la bàyyi, wallaay bàyyi
La main qui t'a donné, la main qui te toucheLoxo bu la bàyyi, loxo ngi tok
La main qui t'a donné, oh oui, la mainLoxo bu la bàyyi, wallaay bàyyi

Compter les billets, ça fait plaisirCompter billets go didi tati
T'as plein de fric, fricTeye full money money
Je ne vais pas manger ton cul, bon appétitDuma lekk seen bol, bon appetit
Juste pour dire qu'on va s'éclaterTële rekk tax ñuy ratatati
Un plat que je connais, ça ne va pas foirerCuj bu xam lekkam du fot
Un bon plat, il y a quelqu'un qui va le prendreDale bu la xat am na ku mu jot
Je fais ça juste pour le plaisir de tousDamay fo sax muy neex ñepp
Dieu merci, je t'appelleDieu merci noo tudd yaw

Éveille ta beauté, tu es là, tu as 25/5Yëngël sa mbagg bu de yaa ngi jot lii 25/5
Ce que tu fais, tu le fais juste pour Dieu, le tennisLi nga joxe ngay jotaat rekk Yàllay ténnis
Fais-moi un signe, je vais te montrer des trucs nouveauxDaf ma woo ma ñëw mu sampal ma ay laaf yu bees
Dieu merci, merci, merci, je m'aime.Dieu merci, merci, merci, I love mysef


Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección