visualizaciones de letras 31

Jolie femme d'Afrique

Mia Guisse

Letra

    Bàyyi ma yéye chewing gum
    Xale bi est-ce que c'est pour moi
    Zéro faute ma ne lépp tout bon
    Ni ma ko barde we, le mbaa doo ngiste

    Jolie femme d'Afrique (d'Afrique)
    Sama regard mooy bombastic
    Gaa yi naan je suis fantastique
    Su ma jàkkaarloo nit ki man
    Maa fit wi di musique naan

    Rampapam rampapam rampapam
    Rampapam rampapam rampapam
    Samay bët ak sama xol a ma tooñ
    Ñoo ma nobloo boy bi nekk sama koñ

    Ne na fook mu gis ma tay si ngoon
    Amaguma fitu wax ak moom
    Bàyyileen ma bu leen ma dugal
    Ci mbëggeel bu may yóbbu coma

    Ay, ay, ay yaay, foon na ma dee
    Foon na ma dee, lu ma dall yaw la
    Soo ma nobee lu ma dall yaw la
    Bi xeetu nit man àntanuma ko

    Dama ko nob ba [?]
    Di ko xalaat ta [?]
    Su ma ko jegee (moo ray ma)
    Ma lépp lépp lépp [?]

    Su ma naree giseek moom
    Panique jaxasoo ma ni juuk rekk daw
    Eh yaw man ndekke parewuma
    Maa ngi mel ni kuy dem combat

    Ouyah, yah
    Dama choqué yaah yah
    Dama choqué yaah yah
    Tax bu ñu dajee sama fit bi di tëb di tëgganal sib na

    Rampapam rampapam rampapam
    Rampapam rampapam rampapam
    Samay bët ak sama xol a ma tooñ
    Ñoo ma nobloo boy bi nekk sama koñ

    Ne na fook mu gis ma tay si ngoon
    Amaguma fiitu wax ak moom
    Bàyyileen mu bu leen ma dugal
    Ci mbëggeel bu may yóbbu coma

    Ay, ay, ay yaay, foon na ma dee
    Foon na ma dee, lu ma dall yaw la
    Soo ma nobee lu ma dall yaw la
    Bi xeetu nit man àntanuma ko

    Ay, ay, ay yaay, foon na ma dee
    Foon na ma dee, lu ma dall yaw la
    Soo ma nobee lu ma dall yaw la
    Bi xeetu nit man àntanuma ko

    Ay ay choqué, dam lay choqué
    Su ma jugee pour dem daa am luy bloqué, ah
    Écoutez man faw ma focus
    Dama bëgga xam man kañ la namp ragal, ah!

    Jolie femme d'Afrique
    Sama regard mooy bombastic
    Gaa yi naan je suis fantastique
    Su ma jàkkaarloo boy bi
    Maa fit bi di musique naan

    Rampapam rampapam papam
    Rampapam rampapam papanra
    Boy bi boy bi laperas
    Bi xeetu nit àntanuma ko

    Ay, ay, ay yaay, foon na ma dee
    Foon na ma dee, lu ma dall yaw la
    Soo ma nobee lu ma dall yaw la
    Bi xeetu nit man àntanuma ko

    Ouyah, yah
    Dama choqué yaah yah
    Dama choqué yaah yah
    Tax bu ñu dajee sama fit bi di tëb
    Man xamuma pur lan, wuy!


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección