Traducción generada automáticamente

visualizaciones de letras 34

Jolie femme d'Afrique

Mia Guisse

Letra

Mooie vrouw uit Afrika

Jolie femme d'Afrique

Bàyyi ma yéye kauwgomBàyyi ma yéye chewing gum
Xale bi is het voor mij?Xale bi est-ce que c'est pour moi
Zéro faute, ik ben helemaal goedZéro faute ma ne lépp tout bon
Als ik je zie, dan voel ik me fijnNi ma ko barde we, le mbaa doo ngiste

Mooie vrouw uit Afrika (uit Afrika)Jolie femme d'Afrique (d'Afrique)
Mijn blik is bombastischSama regard mooy bombastic
Ja, ik ben fantastischGaa yi naan je suis fantastique
Als ik je zie, manSu ma jàkkaarloo nit ki man
Voel ik de muziek in mijMaa fit wi di musique naan

Rampapam rampapam rampapamRampapam rampapam rampapam

Mijn ogen en mijn hart zijn voor jouSamay bët ak sama xol a ma tooñ
Ze zeggen dat ik de jongen ben die bij jou hoortÑoo ma nobloo boy bi nekk sama koñ

Ne na fook mu gis ma tay si ngoonNe na fook mu gis ma tay si ngoon
Amaguma fitu wax ak moomAmaguma fitu wax ak moom
Bàyyileen ma bu leen ma dugalBàyyileen ma bu leen ma dugal
Ci mbëggeel bu may yóbbu comaCi mbëggeel bu may yóbbu coma

Ay, ay, ay ja, het doet pijnAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Het doet pijn, wat ik jou zie doenFoon na ma dee, lu ma dall yaw la
Als ik je zie, wat ik jou zie doenSoo ma nobee lu ma dall yaw la
Als ik kijk naar de mensen, ik ben niet meer de oudeBi xeetu nit man àntanuma ko

Dama ko nob ba [?]Dama ko nob ba [?]
Di ko xalaat ta [?]Di ko xalaat ta [?]
Su ma ko jegee (moo ray ma)Su ma ko jegee (moo ray ma)
Ma lépp lépp lépp [?]Ma lépp lépp lépp [?]

Su ma naree giseek moomSu ma naree giseek moom
Paniek, ik ben in de war, ik weet niet meer wat ik moet doenPanique jaxasoo ma ni juuk rekk daw
Eh jij, ik ben niet meer de oudeEh yaw man ndekke parewuma
Ik voel me alsof ik in een gevecht benMaa ngi mel ni kuy dem combat

Ouyah, yahOuyah, yah
Dama choqué yaah yahDama choqué yaah yah

Tax bu ñu dajee sama fit bi di tëb di tëgganal sib naTax bu ñu dajee sama fit bi di tëb di tëgganal sib na

Rampapam rampapam rampapamRampapam rampapam rampapam
Rampapam rampapam rampapamRampapam rampapam rampapam
Mijn ogen en mijn hart zijn voor jouSamay bët ak sama xol a ma tooñ
Ze zeggen dat ik de jongen ben die bij jou hoortÑoo ma nobloo boy bi nekk sama koñ

Ne na fook mu gis ma tay si ngoonNe na fook mu gis ma tay si ngoon
Amaguma fiitu wax ak moomAmaguma fiitu wax ak moom
Bàyyileen mu bu leen ma dugalBàyyileen mu bu leen ma dugal
Ci mbëggeel bu may yóbbu comaCi mbëggeel bu may yóbbu coma

Ay, ay, ay ja, het doet pijnAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Het doet pijn, wat ik jou zie doenFoon na ma dee, lu ma dall yaw la
Als ik je zie, wat ik jou zie doenSoo ma nobee lu ma dall yaw la
Als ik kijk naar de mensen, ik ben niet meer de oudeBi xeetu nit man àntanuma ko

Ay, ay, ay ja, het doet pijnAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Het doet pijn, wat ik jou zie doenFoon na ma dee, lu ma dall yaw la
Als ik je zie, wat ik jou zie doenSoo ma nobee lu ma dall yaw la
Als ik kijk naar de mensen, ik ben niet meer de oudeBi xeetu nit man àntanuma ko

Ay ay choqué, ik ben geschoktAy ay choqué, dam lay choqué
Als ik je zie, dan ben ik geblokkeerd, ahSu ma jugee pour dem daa am luy bloqué, ah
Luister, ik moet me concentrerenÉcoutez man faw ma focus
Ik wil weten wat er aan de hand is, ah!Dama bëgga xam man kañ la namp ragal, ah!

Mooie vrouw uit AfrikaJolie femme d'Afrique
Mijn blik is bombastischSama regard mooy bombastic
Ja, ik ben fantastischGaa yi naan je suis fantastique
Als ik je zie, jongenSu ma jàkkaarloo boy bi
Voel ik de muziek in mijMaa fit bi di musique naan

Rampapam rampapam papamRampapam rampapam papam
Rampapam rampapam papanraRampapam rampapam papanra
Jongen, jongen, ik ben verliefdBoy bi boy bi laperas
Als ik kijk naar de mensen, ik ben niet meer de oudeBi xeetu nit àntanuma ko

Ay, ay, ay ja, het doet pijnAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Het doet pijn, wat ik jou zie doenFoon na ma dee, lu ma dall yaw la
Als ik je zie, wat ik jou zie doenSoo ma nobee lu ma dall yaw la
Als ik kijk naar de mensen, ik ben niet meer de oudeBi xeetu nit man àntanuma ko

Ouyah, yahOuyah, yah
Dama choqué yaah yahDama choqué yaah yah
Dama choqué yaah yahDama choqué yaah yah
Tax bu ñu dajee sama fit bi di tëbTax bu ñu dajee sama fit bi di tëb
Man xamuma pur lan, wuy!Man xamuma pur lan, wuy!

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección