Traducción automática

Jolie femme d'Afrique
Mia Guisse
Jolie femme d'Afrique
Jolie femme d'Afrique
Bàyyi ma yéye chewing gumBàyyi ma yéye chewing gum
Xale bi est-ce que c'est pour moiXale bi est-ce que c'est pour moi
Zéro faute ma ne lépp tout bonZéro faute ma ne lépp tout bon
Ni ma ko barde we, le mbaa doo ngisteNi ma ko barde we, le mbaa doo ngiste
Jolie femme d'Afrique (d'Afrique)Jolie femme d'Afrique (d'Afrique)
Mon regard est explosifSama regard mooy bombastic
Gaa yi naan je suis fantastiqueGaa yi naan je suis fantastique
Si je m'exprime, c'est pour moiSu ma jàkkaarloo nit ki man
Je fais vibrer la musiqueMaa fit wi di musique naan
Rampapam rampapam rampapamRampapam rampapam rampapam

Mes yeux et mon cœur te regardentSamay bët ak sama xol a ma tooñ
Ils me disent que tu es ma reineÑoo ma nobloo boy bi nekk sama koñ
Ne na fook mu gis ma tay si ngoonNe na fook mu gis ma tay si ngoon
Amaguma fitu wax ak moomAmaguma fitu wax ak moom
Bàyyileen ma bu leen ma dugalBàyyileen ma bu leen ma dugal
Ci mbëggeel bu may yóbbu comaCi mbëggeel bu may yóbbu coma
Ay, ay, ay yaay, foon na ma deeAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Foon na ma dee, qu'est-ce que tu veux de moiFoon na ma dee, lu ma dall yaw la
Si je te dis ce que je veux de toiSoo ma nobee lu ma dall yaw la
Quand je vois l'autre, je ne peux pas m'en empêcherBi xeetu nit man àntanuma ko
Dama ko nob ba [?]Dama ko nob ba [?]
Di ko xalaat ta [?]Di ko xalaat ta [?]
Su ma ko jegee (moo ray ma)Su ma ko jegee (moo ray ma)
Ma lépp lépp lépp [?]Ma lépp lépp lépp [?]
Su ma naree giseek moomSu ma naree giseek moom
Panique jaxasoo ma ni juuk rekk dawPanique jaxasoo ma ni juuk rekk daw
Eh yaw man ndekke parewumaEh yaw man ndekke parewuma
Maa ngi mel ni kuy dem combatMaa ngi mel ni kuy dem combat
Ouyah, yahOuyah, yah
Dama choqué yaah yahDama choqué yaah yah

Tax bu ñu dajee sama fit bi di tëb di tëgganal sib naTax bu ñu dajee sama fit bi di tëb di tëgganal sib na
Rampapam rampapam rampapamRampapam rampapam rampapam
Rampapam rampapam rampapamRampapam rampapam rampapam
Mes yeux et mon cœur te regardentSamay bët ak sama xol a ma tooñ
Ils me disent que tu es ma reineÑoo ma nobloo boy bi nekk sama koñ
Ne na fook mu gis ma tay si ngoonNe na fook mu gis ma tay si ngoon
Amaguma fiitu wax ak moomAmaguma fiitu wax ak moom
Bàyyileen mu bu leen ma dugalBàyyileen mu bu leen ma dugal
Ci mbëggeel bu may yóbbu comaCi mbëggeel bu may yóbbu coma
Ay, ay, ay yaay, foon na ma deeAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Foon na ma dee, qu'est-ce que tu veux de moiFoon na ma dee, lu ma dall yaw la
Si je te dis ce que je veux de toiSoo ma nobee lu ma dall yaw la
Quand je vois l'autre, je ne peux pas m'en empêcherBi xeetu nit man àntanuma ko
Ay, ay, ay yaay, foon na ma deeAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Foon na ma dee, qu'est-ce que tu veux de moiFoon na ma dee, lu ma dall yaw la
Si je te dis ce que je veux de toiSoo ma nobee lu ma dall yaw la
Quand je vois l'autre, je ne peux pas m'en empêcherBi xeetu nit man àntanuma ko
Ay ay choqué, dam lay choquéAy ay choqué, dam lay choqué
Si je te dis pour avancer, ça bloque, ahSu ma jugee pour dem daa am luy bloqué, ah
Écoutez man faw ma focusÉcoutez man faw ma focus
Dama bëgga xam man kañ la namp ragal, ah!Dama bëgga xam man kañ la namp ragal, ah!
Jolie femme d'AfriqueJolie femme d'Afrique
Mon regard est explosifSama regard mooy bombastic
Gaa yi naan je suis fantastiqueGaa yi naan je suis fantastique
Si je m'exprime, c'est pour moiSu ma jàkkaarloo boy bi
Je fais vibrer la musiqueMaa fit bi di musique naan
Rampapam rampapam papamRampapam rampapam papam
Rampapam rampapam papanraRampapam rampapam papanra
Boy bi boy bi laperasBoy bi boy bi laperas
Bi xeetu nit àntanuma koBi xeetu nit àntanuma ko
Ay, ay, ay yaay, foon na ma deeAy, ay, ay yaay, foon na ma dee
Foon na ma dee, qu'est-ce que tu veux de moiFoon na ma dee, lu ma dall yaw la
Si je te dis ce que je veux de toiSoo ma nobee lu ma dall yaw la
Quand je vois l'autre, je ne peux pas m'en empêcherBi xeetu nit man àntanuma ko
Ouyah, yahOuyah, yah
Dama choqué yaah yahDama choqué yaah yah
Dama choqué yaah yahDama choqué yaah yah
Tax bu ñu dajee sama fit bi di tëbTax bu ñu dajee sama fit bi di tëb
Man xamuma pur lan, wuy!Man xamuma pur lan, wuy!

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: