Suscríbete

Traducción generada automáticamente

visualizaciones de letras 162

Sama Xool (feat. VJ)

Mia Guisse

Letra

Sama Xool (feat. VJ)

Sama Xool (feat. VJ)

So wie ich es fühle, lass mich nicht alleinSoo ma soree nu may nooye sama xol kaay
Warum soll ich dir sagen, dass ich nicht mehr kann?Waatal ma ni doo ma bàyyi ba ba may dee
Siehst du die Welle, die mich mitnimmt, wenn ich gehe?Gisoo mbégte bi may àndal su ma lay wayal?
Weißt du, dass der König nur weiß, wo ich bin?Ndax laawu Buur bi rekk a xam fi nga ma jële

Ich denke an dich, mein HerzDénk naa la sama xol bi
Ich fühle dich, mein HerzYéene naa la sama xol bi
Ich höre dich in deinem HerzenDégg naa la ci sa xol bi
Doch woher soll ich wissen, was du tust?Kon nak foo móolee pikkiru laay def
Du färbst mein HerzColoré nga sama xol bi
Ich denke an dich, mein KopfDénk naa la sama bopp
Was du tust, ist in meinem HerzenLi nga liggéey ci sama xol bi
Wenn die Nacht kommt, was soll ich tun?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

Sag mir, wie es dir gehtSay xeetu xaar baax
Ich will wissen, was du fühlstMan su ma koy lim fi de laay des
Wenn ich dir sage, ich will, dass du es tustNdax su ma feeberee bëgg wér séeti ko laay def
Das Parlament sagt, ich bin ein BanditParlement bi yépp naan bandit laa
Die, die mir sagen, ich soll gehen, sind nicht hierÑi naan kobb laa, nga ñëw tànn ma
Baby, was sagst du dazu?Baby yaw ci loo ne?
Sag es mir, lass uns redenJegesi ma, ñu felfëlaale

Ich denke an dich, mein HerzDénk naa la sama xol bi
Ich fühle dich, mein HerzYéene naa la sama xol bi
Ich höre dich in deinem HerzenDégg naa la ci sa xol bi
Doch woher soll ich wissen, was du tust?Kon nak foo móolee pikkiru laay def
Du färbst mein HerzColoré nga sama xol bi
Ich denke an dich, mein KopfDénk naa la sama bopp
Was du tust, ist in meinem HerzenLi nga liggéey ci sama xol bi
Wenn die Nacht kommt, was soll ich tun?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

Ich sehe esMaa ngi séet
Wo ich bin, ist es gutFi ma la def waaw
Die Nacht, die ich für dich mache, BabyYaay ki ma def roi bébé
Lass mich wissen, was du willstXamal ma luy nobeel

Wenn wir uns sehenBa ñu gisee
Kann ich nicht aufhörenMënuma xef waaw
Nur der Weg ist gut, BabyBëtu mbëggeel rekk waaw, bébé
Ich will dich nicht verlierenLaa la mës a xoole

Bin ich nur ein Spielzeug für dich?Man sama jëmm ji rekk nga jaaxal?
Ich bin nicht hier, weil du es willstDuma bett ci yaw ndax ndaanaan nga
Ich sehe niemanden, denn du bist es, die ich willDuma xool keneen ndax yaw mi yaa ma doy
Ich bin der erste, der es sagtMaa la njëkk barde

Ich bin dein Freund, was können die anderen tun? (Nichts)Man sama bae nga, lu ci nit ñi mën? (Dara)
Und meine Träume sind nicht weit wegTe sama féem yi rëcc ci du gaaw
Wenn du bei Mami Guissé ankommstBa nga réppee ba dugg ci Mami Guissé
Will ich nur dich sehenLaa la xool rekk ree

Ich denke an dich, mein HerzDénk naa la sama xol bi
Ich fühle dich, mein HerzYéene naa la sama xol bi
Ich höre dich in deinem HerzenDégg naa la ci sa xol bi
Doch woher soll ich wissen, was du tust?Kon nak foo móolee pikkiru laay def
Du färbst mein HerzColoré nga sama xol bi
Ich denke an dich, mein KopfDénk naa la sama bopp
Was du tust, ist in meinem HerzenLi nga liggéey ci sama xol bi
Wenn die Nacht kommt, was soll ich tun?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

Ich denke an dich, mein HerzDénk naa la sama xol bi
Ich fühle dich, mein HerzYéene naa la sama xol bi
Ich höre dich in deinem HerzenDégg naa la ci sa xol bi
Doch woher soll ich wissen, was du tust?Kon nak foo móolee pikkiru laay def
Du färbst mein HerzColoré nga sama xol bi
Ich denke an dich, mein KopfDénk naa la sama bopp
Was du tust, ist in meinem HerzenLi nga liggéey ci sama xol bi
Wenn die Nacht kommt, was soll ich tun?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección