Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 419

Sama Xool (feat. VJ)

Mia Guisse

Letra

Same Vibe (feat. VJ)

Sama Xool (feat. VJ)

So I’m not feeling like I’m in the same vibeSoo ma soree nu may nooye sama xol kaay
Why do I feel like I’m losing my mind?Waatal ma ni doo ma bàyyi ba ba may dee
Do you see the struggle I’m trying to hide?Gisoo mbégte bi may àndal su ma lay wayal?
Is it just me or is the world passing by?Ndax laawu Buur bi rekk a xam fi nga ma jële

I’m thinking of my vibeDénk naa la sama xol bi
I’m feeling my vibeYéene naa la sama xol bi
I’m hearing you in my vibeDégg naa la ci sa xol bi
But damn, if I could just make it rightKon nak foo móolee pikkiru laay def
You colored my vibeColoré nga sama xol bi
I’m thinking of my ownDénk naa la sama bopp
What you’re doing in my vibeLi nga liggéey ci sama xol bi
Why does it feel like I’m losing my mind?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

Say the crew is goodSay xeetu xaar baax
I’m just trying to get byMan su ma koy lim fi de laay des
If I’m feeling low, I need to get highNdax su ma feeberee bëgg wér séeti ko laay def
The whole parliament says I’m a banditParlement bi yépp naan bandit laa
They say I’m lost, but I’m just trying to find my wayÑi naan kobb laa, nga ñëw tànn ma
Baby, what do you see in me?Baby yaw ci loo ne?
Help me out, we can make it throughJegesi ma, ñu felfëlaale

I’m thinking of my vibeDénk naa la sama xol bi
I’m feeling my vibeYéene naa la sama xol bi
I’m hearing you in my vibeDégg naa la ci sa xol bi
But damn, if I could just make it rightKon nak foo móolee pikkiru laay def
You colored my vibeColoré nga sama xol bi
I’m thinking of my ownDénk naa la sama bopp
What you’re doing in my vibeLi nga liggéey ci sama xol bi
Why does it feel like I’m losing my mind?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

I’m feeling goodMaa ngi séet
I’m doing it rightFi ma la def waaw
The one who’s got my back, babyYaay ki ma def roi bébé
Show me what you gotXamal ma luy nobeel

When we’re togetherBa ñu gisee
I can’t complainMënuma xef waaw
Just a little bit of love, babyBëtu mbëggeel rekk waaw, bébé
That’s all I need to feelLaa la mës a xoole

Am I just your fool?Man sama jëmm ji rekk nga jaaxal?
I won’t bet on you, cause you’re not mineDuma bett ci yaw ndax ndaanaan nga
I can’t see another, cause you’re the one I wantDuma xool keneen ndax yaw mi yaa ma doy
I’m just trying to keep it realMaa la njëkk barde

Am I your guy, what’s up with the others? (Nothing)Man sama bae nga, lu ci nit ñi mën? (Dara)
And my feelings are real, they’re not fakeTe sama féem yi rëcc ci du gaaw
When you call me, I’m there for you, girlBa nga réppee ba dugg ci Mami Guissé
That’s all I see, just youLaa la xool rekk ree

I’m thinking of my vibeDénk naa la sama xol bi
I’m feeling my vibeYéene naa la sama xol bi
I’m hearing you in my vibeDégg naa la ci sa xol bi
But damn, if I could just make it rightKon nak foo móolee pikkiru laay def
You colored my vibeColoré nga sama xol bi
I’m thinking of my ownDénk naa la sama bopp
What you’re doing in my vibeLi nga liggéey ci sama xol bi
Why does it feel like I’m losing my mind?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

I’m thinking of my vibeDénk naa la sama xol bi
I’m feeling my vibeYéene naa la sama xol bi
I’m hearing you in my vibeDégg naa la ci sa xol bi
But damn, if I could just make it rightKon nak foo móolee pikkiru laay def
You colored my vibeColoré nga sama xol bi
I’m thinking of my ownDénk naa la sama bopp
What you’re doing in my vibeLi nga liggéey ci sama xol bi
Why does it feel like I’m losing my mind?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección