Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 613

Sama Xool (feat. VJ)

Mia Guisse

Letra

Sama Xool (feat. VJ)

Sama Xool (feat. VJ)

Dus ik ben niet bang voor wat je zegtSoo ma soree nu may nooye sama xol kaay
Waarom zou ik me druk maken, ik ben hier om te blijvenWaatal ma ni doo ma bàyyi ba ba may dee
Zie je de liefde die ik voel, kan je dat begrijpen?Gisoo mbégte bi may àndal su ma lay wayal?
Of is het gewoon een spel dat je speelt met mijn hart?Ndax laawu Buur bi rekk a xam fi nga ma jële

Ik denk aan jou, mijn liefdeDénk naa la sama xol bi
Ik voel je, mijn liefdeYéene naa la sama xol bi
Ik hoor je in mijn gedachtenDégg naa la ci sa xol bi
Dus als je me wilt, laat het me wetenKon nak foo móolee pikkiru laay def
Kleur je mijn liefdeColoré nga sama xol bi
Ik denk aan jou, mijn zelfDénk naa la sama bopp
Wat je doet met mijn liefdeLi nga liggéey ci sama xol bi
Is dat wat je wilt, dat ik het zo doe?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

Zeg het me, als het goed isSay xeetu xaar baax
Ik wil dat je het me vertelt, als je het wiltMan su ma koy lim fi de laay des
Als ik je niet kan krijgen, wat moet ik dan doen?Ndax su ma feeberee bëgg wér séeti ko laay def
Het parlement zegt dat ik een bandiet benParlement bi yépp naan bandit laa
Die zeggen dat ik moet stoppen, maar ik ga niet wegÑi naan kobb laa, nga ñëw tànn ma
Baby, wat denk je?Baby yaw ci loo ne?
Help me, we kunnen het samen doenJegesi ma, ñu felfëlaale

Ik denk aan jou, mijn liefdeDénk naa la sama xol bi
Ik voel je, mijn liefdeYéene naa la sama xol bi
Ik hoor je in mijn gedachtenDégg naa la ci sa xol bi
Dus als je me wilt, laat het me wetenKon nak foo móolee pikkiru laay def
Kleur je mijn liefdeColoré nga sama xol bi
Ik denk aan jou, mijn zelfDénk naa la sama bopp
Wat je doet met mijn liefdeLi nga liggéey ci sama xol bi
Is dat wat je wilt, dat ik het zo doe?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

Ik ben hierMaa ngi séet
Als je me nodig hebt, jaFi ma la def waaw
De liefde die ik voor je heb, babyYaay ki ma def roi bébé
Laat me niet alleenXamal ma luy nobeel

Als we samen zijnBa ñu gisee
Kan ik het aan, jaMënuma xef waaw
De weg naar geluk, ja, babyBëtu mbëggeel rekk waaw, bébé
Dat is wat ik wilLaa la mës a xoole

Ben jij mijn enige liefde?Man sama jëmm ji rekk nga jaaxal?
Ik wil niet meer dan jou, want je bent alles voor mijDuma bett ci yaw ndax ndaanaan nga
Ik wil niemand anders, want jij bent de enigeDuma xool keneen ndax yaw mi yaa ma doy
Ik ben hier voor jouMaa la njëkk barde

Ben jij mijn schat, wat kan ik voor je doen? (Niets)Man sama bae nga, lu ci nit ñi mën? (Dara)
En mijn dromen zijn niet te grootTe sama féem yi rëcc ci du gaaw
Als je maar blijft, dan ben ik gelukkigBa nga réppee ba dugg ci Mami Guissé
Dat is alles wat ik wilLaa la xool rekk ree

Ik denk aan jou, mijn liefdeDénk naa la sama xol bi
Ik voel je, mijn liefdeYéene naa la sama xol bi
Ik hoor je in mijn gedachtenDégg naa la ci sa xol bi
Dus als je me wilt, laat het me wetenKon nak foo móolee pikkiru laay def
Kleur je mijn liefdeColoré nga sama xol bi
Ik denk aan jou, mijn zelfDénk naa la sama bopp
Wat je doet met mijn liefdeLi nga liggéey ci sama xol bi
Is dat wat je wilt, dat ik het zo doe?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

Ik denk aan jou, mijn liefdeDénk naa la sama xol bi
Ik voel je, mijn liefdeYéene naa la sama xol bi
Ik hoor je in mijn gedachtenDégg naa la ci sa xol bi
Dus als je me wilt, laat het me wetenKon nak foo móolee pikkiru laay def
Kleur je mijn liefdeColoré nga sama xol bi
Ik denk aan jou, mijn zelfDénk naa la sama bopp
Wat je doet met mijn liefdeLi nga liggéey ci sama xol bi
Is dat wat je wilt, dat ik het zo doe?Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección