Suscríbete

Tradução automática

Exibições da letra 15

Yeureum Djiguene

Viviane Chidid

Letra

Gentilhomme

Yeureum Djiguene

Fais pour ma mèreDef ma mbaamam
Fais pour ma mèreDef ma jaamam
Éloigne-toi, elle vit ici avec moiDóor subak ngoon la dëkk ak man
Fais pour ma mèreDef ma jaamam
Fais pour ma mèreDef ma mbaamam
Aide-moi, elle vit ici avec moiDi ma toroxal, la dëkk ak man

Elle vit ici avec moiLa dëkk ak man
À l'infini, elle vit ici avec moiSaa su ne, la dëkk ak man

Aide-moi, ne fais pas de mal aux enfantsDi ma saaga, kanamu xale yi
Dans mes bras, je ne vais pas te laisser tomberCi samay nawle, doo ma sutural
Ne m'abandonne pas, je suis là pour toiYërëmuloo ma, faalewoo ma
N'ignore pas, la promesse a été faiteFonkuloo ma, mettit bi doy na

Éloigne-toi, ne fais pas de mal à tes enfantsDóor jigéen bi la juural say doom
Dis la vérité, Dieu l'a dit, c'est profondWax dëgg Yàlla li de ñaaw na
Ne sous-estime pas ça, pour que je te protègeDémb jooy nga, ngir ma nob la
Tu sais bien, tu agis comme si tout était normalTay nga am ma, di ma dóor di ma doyloo

Fais pour moi, fais pour moiDi ma dóor, di ma doyloo
Fais pour moi, fais pour moiDi ma dóor, di ma doyloo

Je vais te dire, dis-moi ce que c'estDina metti ci man, wax ma lan la
Eh bien, je crois que tu ne me comprends pasDëgg, sonn naa kon yërëm ma
J'ai besoin de toi, ne me fuis pasSëyal naa la, muñel naa la
Aide tes enfants, donc crois-moiYaaral la say doom, kon yërëm ma

Éloigne-toi, ne fais pas de mal à tes enfantsDóor jigéen bi la jural say doom
Dis la vérité, Dieu l'a dit, c'est profondWax dëgg Yàlla li de ñaaw na

Quand tu souffles, le vent est fraisGarab bu daanu, xob yaa laax na
Cette femme guérit ta souffrance vraimentJigéen bu guéné, kër nga dey wét lool

Fais pour moi, fais pour moiDi ma dóor, di ma doyloo
Fais pour moi, fais pour moiDi ma dóor, di ma doyloo

On ne peut pas se laisser faireWarul dooree
GentilhommeGentleman
On ne peut pas se laisser faireWarul doore

Fais pour ma mèreDéf ma mbaamam
Fais pour mon pèreDéf ma diaamam
Je vais t'aider, si tu es doux avec moiDima torokhal, la deuké ak mane
Fais pour ma mèreDéf ma mbaamam
Fais pour mon pèreDéf ma diaamam
Je vais t'aiderDima torokhal

Moi je l'entends,Man dégg na,
Fais attention à ce qui se ditMakk dan-na wax naan
Nous faisons de notre mieux pour toujours protéger les femmesYërmandé lañuy yore jigéen

Moi je l'entendsMan dégg na
Fais attention à ce qui se ditMakk dan-na wax naan
C'est dans le soutien qu'on protège les femmesCi sutura lañuy yore jigéen

Al Hamdoulillah, que Dieu t’accorde son soutienAl Hamdoulilah bi la Yàlla boolek ki lay soutoural
Al Hamdoulillah, que Dieu apaise ton cœurAl Hamdoulilah bi la Yàlla boolek kiy seddal sa xol
Voici un gentilhommeKooku gentleman la

Gentilhomme,Gentleman la,
Youssou, ma belle Aïda ne délaisse pas les femmesYoussou ma jigéen chéri Aïda du joyloo jigéen
Gentilhomme,Gentleman la,
Pape Ndiaye, fils de Fara Ndiaye, chérie Aïda NdiayePape Ndiaye, baayu Fara Ndiaye chéri Aida Ndiaye
Voici un gentilhommeKooku gentleman la
GentilhommeGentleman la
Cheikh Amar, chéri Marie Amar ne délaisse pas les femmesCheikh Amar chéri Marie Amar du joyloo jigéen
Voici un gentilhommeKooku gentleman la
Mbaye Gueye Sagn-Sagnou, Birame Guéye, chérie Mame NdiayeMbaye Gueye Sagn-Sagnou Birame Guéye chéri Mame Ndiaye
GentilhommeGentleman la
Cheikh Kanté, chéri Amy Diawara ne délaisse pas les femmesCheikh Kanté chéri Amy Diawara du joyloo jigéen
GentilhommeGentleman la
Matar Cissé, chéri Aida Mar ne délaisse pas les femmesMatar Cissé chéri Aida Mar du joyloo jigéen
GentilhommeGentleman la
GentilhommeGentleman la
Cheikh Tidiane Ba, chéri Lissa Ndoye ne délaisse pas les femmesCheikh Tidiane Ba chéri Lissa Ndoye du joyloo jigéen
GentilhommeGentleman la
Boubacar Diallo, Diallo, le fils de Mame DiarraBoubacar Diallo, Diallo diéri chéri Mame Diarra
GentilhommeGentleman la
Pape Cheikh Diallo, chéri Kya AidaraPape Cheikh Diallo chéri Kya Aidara
GentilhommeGentleman la
Cheikh Sarr, fils de Momar Sarr, le fils d'Alima NdioneCheikh Sarr, keur Momar Sarr góoru Alima Ndione
GentilhommeGentleman la

Ne la lâche pas, ta femmeNeexalal sa jigéen
La femme du mondeJigéen àdduna la
Ne la lâche pas, ta femmeNeexalal yaw yaw sa jigéen
La femme du paradisJigéen aljana la
Ne la lâche pas, ta femmeNeexalal sa jigéen
La femme du mondeJigéen àdduna la
Ne la lâche pas, ta femmeNeexalal yaw yaw sa jigéen
La femme du paradisJigéen aljana la


Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Viviane Chidid y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección